Luke 18:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Njiit la ne ko: «Loolu lépp sàmm naa ko li dale ci sama ndaw ba tey.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Loolu lépp, ba may ndaw laa ko dale sàmm ba tey.»
Recommended Reading