bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 18:23
Luke 18:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi nit ka déggee loolu, mu am tiis, ndaxte ku bare woon alal la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba waa ji déggee loolu, am na tiis wu réy, ndax barele woon na lool.