bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 18:28
Luke 18:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Piyeer ne: «Nun de, dëddu nanu li nu am lépp, topp la.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer daldi ne: «Nun de, noo ngii, dëddu la nu amoon, topp la.»