Luke 18:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu ne leen: «Ci dëgg maa ngi leen koy wax, képp ku dëddu kër walla jabar walla ay doomi ndey walla ay waajur walla ay doom ngir nguuru Yàlla,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne leen: «Maa leen ko wax déy, amul kenn kuy dëddu kër, mbaa jabar, mbaa mbokk, mbaa waajur, mbaa doom, ngir nguurug Yàlla,