Luke 18:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na itam ca dëkk ba jigéen ju jëkkëram faatu ju daan faral di ñëw ci moom, naan ko: “Àtte ma ak sama noon!”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab jëtun a nga woon ca dëkk boobee. Daan na ñëw ca moom, naan ko: “Àtte ma ak sama jotewaale!”