Luke 18:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye taalibe ya dégguñu li mu leen doon wax; kàddu yooyu ump na leen, te xamuñu li waxi Yeesu yooyu tekki.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ndaw ya, ñoom, xamuñu dara ci jooju wax, ndax mbóotu kàddug Yeesu gaa leen làqu, ba tax ñu umple la mu wax.