Luke 18:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu di agsi dëkku Yeriko, am gumba gu toogoon ca wetu yoon wa, di yelwaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Yeesu di jubsi dëkk ba ñuy wax Yeriko, ab silmaxaa nga tooge ca peggu yoon wa, di yalwaan.