Luke 19:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne nag: «Dafa amoon boroom juddu bu rafet bu demoon ci réew mu sore, ngir ñu fal ko buur te mu dellusiwaat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax mu ne: «Boroom juddu bu réy la woon. Muy waaja dem réew mu sore, ngir ñu fal ko fa buur, mu doora ñibbsi.