Luke 19:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Bi ñu ko falee buur nag, ba mu dellusi, mu woolu surga, ya mu joxoon wurus wa, ngir xam nan lañu ci liggéeye.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Gannaaw ba ñu ko falee buur, ba mu délsi, daa woolu surga, ya mu joxoon wurus wa, ngir xam ñaata la leen ca seen liggéey jural.