Luke 19:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye amoon na fa waa ju ñuy wax Sase. Njiitu juutikat la, te di ku bare alal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndeke jenn waay a nga fa, di kilifag juutikat bu bare alal, ñu di ko wax Sase.
Recommended Reading