Luke 19:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu waxee loolu ba noppi, Yeesu dafa daldi jiitu, jëm Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Yeesu waxee loolu ba noppi, ca la jiitu, jëm Yerusalem.