bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 19:29
Luke 19:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi muy jege dëkki Betfase ak Betani, ci wetu tund wu ñuy wax tundu Oliw ya, Yeesu yebal ñaar ci ay taalibeem,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Yeesu dikkee ba jub dëkk ya ñuy wax Betfase ak Betani, ca wetu tund wa ñuy wax tundu Oliw ya, dafa yebal ñaari taalibeem,