Luke 19:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi muy dem, nit ñi di lalal Yeesu seeni yére ci yoon wi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la Yeesuy dem, nit ñi di ko lalal seeni yére ca yoon wa.