bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 19:38
Luke 19:38 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu ngi naan:«Yaw buur biy ñëw ci turu Boroom bi,ku barkeel nga!Na jàmm am ca asamaan,te ndam li féete ca bérab yu gën a kawe!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña nga naan: «Na barke wàccal buur bi ñëw ci turu Boroom bi! Jàmm fa asamaan; daraja fa bérab ya gëna kawe!»