bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 19:4
Luke 19:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu mu daw, jiituji ca yoon wa, yéeg ci genn garab ngir gis Yeesu, ndaxte foofa la naroon a jaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Sase daw, jiituji, daldi yéeg ci genn garab ca yoon woowu Yeesu wara jaare, ngir mu man koo gis.