Luke 19:41 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu jegee dëkk ba, ba séen ko, mu jooy ko
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Yeesu jubsee ba séen dëkk ba, jooy na ndax moom.