Luke 19:42 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
naan: «Céy yaw itam, boo xamoon bésub tey yi la man a indil jàmm! Waaye fi mu ne mënuloo koo gis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne: «Céy yaw itam, boo xamoon bésub tey jii li lay may jàmm! Waaye fii mu ne, làqu na say gët.