Luke 19:47 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bés bu nekk Yeesu di jàngale ca kër Yàlla ga. Saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya, ñoom ak njiiti xeet wa, ñu ngi ko doon wut a reylu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu nag di jàngle bés bu nekk ca kër Yàlla ga. Ba mu ko defee sarxalkat yu mag ya, ak firikati yoon ya, ñook njiiti xeet wa, di ko wuta rey.