bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 19:48
Luke 19:48 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye xamuñu woon lan lañu man a def, ndaxte nit ñépp a ngi ko doon déglu, bañ benn baat raw leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye xamuñu nu ñuy def, ndax ñépp a ko doon déglu, teewlu ko lool.