Luke 2:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ca jamono jooja buur bu mag bu ñuy wax Ogust joxe ndigal ne, na ñépp binduji.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jant yooyu ndigal moo tukkee woon ci buur bu mag bu ñuy wax Sesaar Ogust. Mu ne na ñépp binduji ca limeef ya.
Recommended Reading