Luke 2:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xebaar bu baax buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndax kat maa leen indil xibaaru jàmm bu doon mbég mu réy, ñeel askan wépp.