Luke 2:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu waxee loolu, yeneen malaaka yu bare yu jóge asamaan, ànd ak moom, di sant Yàlla naan:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca saa sa gàngooru asamaan gu mag ànd ak malaaka mi, di sàbbaal Yàlla, ne: