Luke 2:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Nañu màggal Yàlla ca asamaan su kawe sa,te ci àddina, na jàmm ji wàcc ci nit, ñi mu nangu ndax yiwam!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Daraja ñeel na Yàlla fa asamaan sa gëna kawe, jàmm ci kaw suuf ñeel ñi Yàlla baaxe.»