Luke 2:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu leen gisee, ñu nettali la ñu leen waxoon ca mbirum xale ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañu leen gis, daldi leen xamal la ñu leen wax ca mbirum xale ba.

Recommended Reading