Luke 2:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Maryaama moom, takkoon na mbir yooyu yépp, di ko xalaat ci xolam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul Maryaama moom, bàyyi woon na xel ci mbir moomu mépp, di ko xalaat ci xolam.