Luke 2:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu jamono ji ñu leen waroon a sellale agsi, ni ko yoonu Musaa tërale. Waajuri Yeesu yi daldi koy yóbbu ca dëkku Yerusalem, ngir sédde ko Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba seen fani setlu matee, ni ko yoonu Musaa laaje, ñu yóbbu xale bi Yerusalem, ngir teewal ko fi kanam Boroom bi,