Luke 2:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na ca Yerusalem nit ku tudd Simeyon. Nit ku fonkoon yoonu Yàlla la te déggal ko, doon séentu jamono, ji Yàlla war a dëfël bànni Israyil. Xel mu Sell mi mu ngi ci moom,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Amoon na nag ca Yerusalem ku ñuy wax Simeyon; ku juboon, ragal Yàlla, di séentu jamono ji nekkinu bànni Israyil di ame ag tan, te Noo gu Sell gi àndoon ak moom.