Luke 2:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Simeyon jël xale bi, leewu ko, daldi sant Yàlla ne:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Simeyon itam jël xale bi, leewu ko, daldi sàbbaal Yàlla, ne: