Luke 2:40 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xale baa nga doon màgg, di dëgër, mu fees ak xel te yiwu Yàlla ànd ak moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xale bi nag di màgg, di dëgër, feese am xel, te yiwu Yàlla ànd ak moom.