Luke 2:43 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi màggal ga tasee, ñu dëpp ñibbi, waaye xale ba Yeesu des Yerusalem, te ay waajuram yéguñu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba màggal ga tasee, ñu ñibbi, ngóor sa Yeesu moom des Yerusalem, te ay waajuram yéguñu ko.