Luke 2:47 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñépp ñi dégg li mu wax yéemu ci xel, mi mu àndal, ak ni mu doon tontoo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem ña ko dégg yéemu ci dégginam aki tontam.
Recommended Reading