Luke 2:50 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye xamuñu li kàddoom yi doon tekki.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay waajuram ñoom dégguñu kàddu googu mu leen wax.
Recommended Reading