Luke 20:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Benn bés Yeesu doon jàngal nit ña ca kër Yàlla ga, di leen yégal xebaar bu baax bi. Saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya ñëw ne ko:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am bés bu Yeesu doon jàngal askan wi ca kër Yàlla ga, di xamle xibaaru jàmm bi. Sarxalkat yu mag ya ak firikati yoon ya ne jalañ, ñook njiit ya.