Luke 20:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu yónniwaat beneen surga, ñu dóor ko moom itam, toroxal ko, dàq ko, mu dellu ak loxoy neen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu dellu yónni beneen surga, ñu dóor ko moom itam, torxal ko, dàq ko, mu dellu loxoy neen.