Luke 20:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bi beykat yi gisee doom ji, ñu ne ci seen biir: “Kii moo war a donn tool bi; nan ko rey, moom ndono li.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul ba beykat ya gisee doom ji, dañu ne ci seen biir: “Kii mooy donn; nanleen ko rey, su ko defee ndono li féeteek nun.”