Luke 20:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Wax nu, ndax jaadu na, nu fey buur bi Sesaar galag walla déet.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Wax nu nag ndax yoon maye na, nu fey Buur Sesaar galag, am déet.»