Luke 20:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Kilifa gi, Musaa bindal na nu ne, ku magam faatu te bàyyiwul doom ak jabaram, kooku war na donn jigéen ji, ba yékkati giiru magam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Sëriñ bi, Musaa da noo bindal ne ku góor, su ku mu bokkal waajur faatoo te amul ak jabaram doom, na jël jabaram, ngir amal mbokkam ma dee, kuutaay.