Luke 20:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci ndekkite li nag, kan ci ñoom moo war a donn jigéen ja, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaw si nag, keroog ndekkite la, kan la ciy doon jabaram, gannaaw juróom ñaar ñépp a ko jëloon jabar?»