Luke 20:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dafa fekk ne mënatuñoo dee, ndaxte dañuy mel ni malaaka yi. Ay doomi Yàlla lañu ndaxte doomi ndekkite lañu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dootuñu mana dee it, ndax niy malaaka lañuy mel. Ay doomi Yàlla lañuy doon, ndax da leen di fekk dekki.