Luke 20:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag nekkul Yàllay ñi dee waaye Yàllay ñiy dund la, ndaxte Yàllaa tax ñépp di dund.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon moom du ñi dee lay seen Yàlla, xanaa ñiy dund, ndax fa moom, ñépp a ngi dund.»