Luke 20:41 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu ne leen: «Lu tax nit ñi di wax ne, Almasi bi mooy sëtu Daawuda?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu neeti leen: «Nees mana waxe ne Almasi, Sëtub Daawuda la?