Luke 21:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bala looloo xew, dees na leen jàpp, fitnaal leen, di leen jébbal àttekat yi ca jàngu ya, tëj leen kaso. Dees na leen yóbbu ci kanam ay buur yi ak ay boroom réew ndax sama tur.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye laata loolu lépp, yeen, dees na leen teg loxo, fitnaal leen, jébbal leen kuréli jàngu ya, tëj leen kaso. Dees na leen yóbbu ci kanami buur aki boroom dëkk ndax sama tur,