Luke 21:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte man ci sama bopp maa leen di jox kàddu ak xel moo xam ne seeni noon duñu ko man a teggi, mbaa ñu di ko weddi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax man maa leen di jox làmmiñ wu ànd ak xel, wu seen benn noon dul mana dàq mbaa di ko weddi.