Luke 21:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku Yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bu ngeen gisee gàngooru xare gu gaw Yerusalem, su boobaa xamleen ne tasteem dëgmal na.