Luke 21:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ci bés yooyu Yàlla dina fey jëf yi, te li ñu bindoon ci téereb Yàlla dina mat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax janti mbugal lay doon, ngir sottal mboolem lu ñu bindoon.