Luke 21:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu boobaa nit ñiy xëm ndax tiitaange, bu ñuy xalaat musiba, yi nar a wàcc ci àddina, ndaxte dees na yengal kàttani asamaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
nit ñiy séentu li nara dikkal àddina, di xëm ndax tiitaange, nde dooley asamaan dina sàqi.

Recommended Reading