Luke 21:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu daldi ne: «Ci dëgg, maa ngi leen koy wax, jigéen ju ñàkk jee moo ëpp ñeneen ñépp lu mu joxe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne: «Maa leen ko wax déy, jëtun bii, ñii ñépp, moo leen ëpple lu mu joxe.