Luke 21:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu itam bu ngeen gisee loolu lépp xew, xamleen ne nguuru Yàlla jege na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ngeen gisee xew-xew yooyu sotti, noonu itam ngeen di xame ne nguurug Yàlla dëgmal na.