Luke 21:38 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te nit ñépp dañu daan teel a xëy ca kër Yàlla ga, di ko déglu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbooloo mépp a daan jëlu, fekki ko ca kër Yàlla ga, ngir déglu ko.
Recommended Reading