Luke 21:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñoom ñépp dañu sàkku ci seen barele, waaye moom dafa sàkku ci néewleem, ba joxe xaalis bi mu waroon a dunde.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax ñii ñépp, la ñu woomle, ca lañu sompe, def ci boyetu sarax bii; waaye moom ci biir ag ñàkkam la jël mboolem ab dundam, def ci.»